FANDOM


玉树吴都 Youssou N'Dour

Youssou dot Com

Egypt

1. Allah 2. Shukran Bamba 3. Mahdiyu Laye 4. Tijaniyya 5. Baay Niasse 6. Bamba the Poet 7. Cheikh Ibra Fall 8. Touba - Daru Salaam


7 Seconds: The Best of Youssou N'Dour [ORIGINAL RECORDING REMASTERED]

1. New Africa 2. Undecided 3. Mouvement 4. Seven Seconds 5. Yo Le Le 6. Without A Smile 7. Please Wait 8. Country Boy 9. Birima 10. Ob La Di Ob La Da 11. Old Man 12. No More 13. Set (Live) 14. Oh Boy (Live) 15. Don't Look Back 16. Things Unspoken

Joko: The Link

1. Wiri-Wiri 2. Birima 3. Mademba (The Electricity Is Out Again) 4. This Dream 5. Yama 6. She Doesn't Need To Fall 7. Miss 8. Beykat 9. Liggeey 10. My Hope Is In You 11. Red Clay

Set

1. Set 2. Alboury 3. Sabar 4. Toxiques 5. Sinebar 6. Medina 7. Miyoko 8. Xale 9. Feenene 10. Fakastalu 11. Hey You! 12. One Day 13. Ay Chono La

Rough Guide to Youssou N'Dour & Etoile de Dakar

1. Absa Gueye 2. Jalo 3. Thiapathioly 4. Diokhama Say Ne Ne 5. Lay Suma Lay 6. Walo 7. Yalaye Dogal 8. Youssou 9. Alboury 10. Independence 11. Wadiour

Guide (Wommat)

1. Leaving 2. Old Man 3. Without A Smile 4. Mame Bamba 5. 7 Seconds 6. How You Are 7. Generations 8. Tourista 9. Undecided 10. Love One Another 11. Life 12. My People 13. Oh Boy 14. Silence 15. Chimes Of Freedom

Lii

1. Intro 2. Sunu Yaye 3. Lii ! 4. Baikat 5. Birima 6. Toureundo 7. Solidarite 8. Lii + 9. Baikat [Remix]

Eyes Open

1. New Africa 2. Live Television 3. No More 4. Country Boy 5. Hope 6. Africa Remembers 7. Couple's Choice 8. Yo Le Le (Fulani Groove) 9. Survie 10. Am Am 11. Marie-Madeleine La Saint-Louisienne 12. Useless Weapons 13. The Same 14. Things Unspoken


The Lion

1. The Lion/Gaiende 2. Shakin' The Tree 3. Kocc Barma 4. Bamako 5. The Truth 6. Old Tucson 7. Macoy 8. My Daughter (Sama Doom) 9. Bes

Lay Suma Lay

1. Lay Suma Lau 2. My Wa Wa 3. Diankha Demal 4. Walo 5. Yalaye Dogal 6. Footaane 7. Soula Sadoome Toogne




1) Youssou Ndour- Tan bi (Non verbatum Very Happy )

Sedaye bi ak tanguaye bi khawma ban momassi geuneul

Sedaye bi ak tanguaye bi khawma ban momassi geuneul

Sedaye biiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii Tanguaye biiiiiiiiiiiiiiiiii

Bou goude gue niou lang si jardin bi

Sedaye biiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii Tanguaye biiiiiiiiiiiiiiiiii

Sed bi ak tanguaye bi Dafa mel ni yeupa yem Bou si khass yegsi ba dial Da nga nan mola geuneul

Sedaye biiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii Tanguaye biiiiiiiiiiiiiiiiii (Bis)

Etc, etc.....


tan bi

sedd bi ag tangaay bi dafa mel ni yeppa yam Sad bu ci xas yegsi ba jall da gna nann mo leu gueuneul Rolling Eyes sedday bi, tanguaay bi koo geje gis nan ko xarr tanggay bi bu tambale nieupp gueu ci tali bi bu becegee nu feexluji ci geej bi Cool bu gudigueh nu lang si jardin yi Love sedd bi ag tangaay bi dafa mel ni yeppa yam bu ci xas yeggsi ba jall da gueu nann mo leu gueuneul sedday bi tanguay bi bu sedd bi neupp lelu ci keur yi nii di waxtann waxi mbeguel ci negg yi Smile Closed yakkamtinan guddi bi demm fattu dji mbajj mu diss niu diakarlo ak tele bi Sleeping ni sedd bi yeggsi na and ag ngeneelam tangayii tamm tabbi aki feemam



2) Moor Ndaje (Youssou N'Dour/Kabou Gueye/Habib Faye)

Te sax adduna kenn du ko dajal, ku dul umpele danu lay ragal Faww nit ku ne am lu muy desal ngir bu ellegee nu men laa setal Fu ne nga nekk fa Lu ne nga dugg ca Heh heh begg naa nga dal Yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Woo yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Lekkoo ci ndap li brgg ci xepp suuf Lekkoo ci ndap li ngali bu ci xepp suuf Woo yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Boo ci lekkul it bu ko xan keneen Kanaan fankul muut Yalla mooy meye Woo yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Menaguma dem waaye keneen du dem Xamal ni bu yoon jeexul waaxusil du jeex... Woo yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Faww nit ku me am lu muy desal Degg degg daal di nga raw Woo yoo Moor Ndaje deel soorale ellek Boo moytuwul yaw lanuy riinion Television yi ag rajo yi sax am na lu nuy umpele Waaye neme mbooloo ni afiisu sinemaa Moor jamais rate Moor wannil ma sa galaac Boo moytuwul yaw lanuy riinion



3) LI MA WEESU

Li ma duudéé li ma weesu day dellusee mel ni seetu..... Seetal léég léég ma geestu ci li ma weesu Léég léég ma réccu walla sax di bàkku Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma bëgg leenoo Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma màgg... Lu ma gën di yàgg, xel mi mel ni bànk Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tànk Li ma dundéé li ma weesu day dellusee mel ni seetu.... Mani seetal léég léég ma geestu ci li ma weesu Léég léég ma réccu walla sax di bàkku Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma bëgg leenoo Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma màgg... Fu gune yi feccee dama leen di tette wax nu mu ma neexe Ma bégëti Lu ma gënë jege mel ni dama sore Lu ma gënë sore gën di gis li ma jegewoon Lu ma gën di yàgg, xel mi mel ni bànk Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tànk Li ma dundéé li ma weesu day dellusee mel ni seetu.... Damay damay damay dellu gune Mel ni mel ni mel ni du ma màgg...

YOUSSOU NDOUR -NOTHING'S IN VAIN (coono du réér) -2002-


4) Genne (For those displaced) – do disco Coono du réér (Youssou N’Dour/Kabou Gueye/Habib Faye)

Heeh heeh heeh heeh dañ leen gene Nuy taxawaalu lii ñaaw Heeh heeh heeh heeh ñi ngiy weréélu ci biir àll bi lii baaxul Talu ñu nelaw, lekku ñu dara metti na Heeh heeh heeh heeh ana njaboot yi, ñii faatu nañu doy na waar Lu jar ñu deg ko.... Feebar yu bon yi, tàngor wu rey wi metti na Heeh heeh heeh heeh lu jar ñu deh ko, ñu def ko... Yàlla ben buur la ku weex la ku ñuul la ju jaune la Kooku moo ñu boole ci suuf si ci ndox mi, ci jaww ji Man de maa ngi woote ñu booloo te benoo bokk yééne Nañu wàññi xiiroo ag naayoo te indi yermànde Ku tane sa moroom defal ko, defel ko, sargal ko Heeh heeh heeh heeh talu ñu nelaw lekku ñu dara metti na Heeh heeh heeh heeh ana njaboot yi, ñii faatu nañu doy na waar Ku mu doon yaw mu metti Ku mu doon yaw nga jaa Ku mu doon yaw nga jaaxle Ku mu doon yaw mu metti Ku mu doon yaw nga jo Ku mu doon yaw nga jommi Ku mu doon yaw....

...Uma boa semana a todo mundo...



5) La Femme est l'avenir de l'amour


6) Mbeggeel Nonu La


7) Il N'y a Pas D'amour Heureuxa


8) Sagal Ko


9) C'est l'amour

Su ma Waxtaanee...


10) Doodle



11) So Many Men


12) Yaru



13) Africa, Dream Again

Ad blocker interference detected!


Wikia is a free-to-use site that makes money from advertising. We have a modified experience for viewers using ad blockers

Wikia is not accessible if you’ve made further modifications. Remove the custom ad blocker rule(s) and the page will load as expected.